Regardez L’agression d’une dame par deux jeunes sur une moto

0

Bone passé woul li. Sa moromou Yaye ngakoy door pour dieul alalam. nga wareuko guiss mouy dokh goudii nga accompagné ko défoko ngay dieul limou yoreu khamo nimou def ba ameko et bo démé do fékou loudoul ay maudites sommes si pochetam ak ay papiers Barki Seydina Mouhameth dafa ame niouy Faté né Yalla amena et mougui guiss léep et 1er goudii si bamel yaw kassé nganek fa Diareu na bayii khéel. Dieul alalou diambour daw kéneu diapoula nékhna mai biisss bou Yalla décider né léep filay yam Tayy… Wallahi dagay reutiou linga doneu Dioudou sakh.PARTAGER KO NGUIT NIOU DIAPP LEN SI NOUMOU GEUNEU GAWE.

Laisser un commentaire

Votre adresse email ne sera pas publiée.