Sur sa page facebook, le rappeur Nit Doff Killah réitère son soutien à son leader Ousmane Sonko.
« Nit gni doffou niou xam naniou niane nio nekk derriere tout ça
Am nga sunu confiance ak sunu soutien
Kom dab bul ragal koudoul Yallah
Patronne bi dey doul parck limou yeuk lepp si ay complot ak ay pekhé you niaw nioukoy wadial son client té mou doon peronnnalité politique bou makk si Rew mi banopi avertiroko de ce danger
L’autre menteuse comploteuse de merde pourquoi apres le temoignage de sa patronne kenn placer wouko garde a vue ?
Legui dale daniouley faye khaliss nga tokk douleul as guor num leu nekhé
Té alkati yiley deglou xamna niou né da ngey doul
Mani domeram diodiou placer leen ko garde a vue mou wakh léen kouko yabal ak louniou ko faye »
→ A LIRE AUSSI : Yoff Tonghor, une femme et ses deux filles retrouvées mortes
→ A LIRE AUSSI : Accusé de viols : Et si Sonko n’a jamais posé les pieds à l’Institut « Sweet Beauté » !
→ A LIRE AUSSI : « Je pourrais mourir si je ne le retire pas »: Lil Uzi Vert après s’être implanté un diamant de 20 millions de dollars au front
'