« Sama diabar amoul morom thi mbax, mais weuyou woul dara…akhh »

0

Je suis un jeune homme de 26 ans, marié à une femme de 24 ans et père de deux enfants. Sama diabar djiguéne geunouko bakh ,yarou ,yatou,yime ame yeuremandé, tabé goré louma ame ak louma amoul kéne khamouko yalla nako yalla déli diame mais le seul et unique problème, est que diongué zéro.

La nuit dina sol nuisette you bakh mais silay yame 5 ans de mariage masouma provoquer, mane rék may déme di thiokasse, après on le fait et lolou dasamasi sone défois on peut rester 2 ou 3 semaines sans le faire et mane dama beugue djiguéne bou bandit si bir nék (chambre). Conseil la beugue noumay déf bamou changer. Merci.

→ A LIRE AUSSI : MAGAL Touba 2020 : «Le Dernier Mot Revient À…»

→ A LIRE AUSSI : Sa ndiogou tacle aisatou diop fall: » limou wax daf kaay Jaay gni ko yoni » (vidéo)

→ A LIRE AUSSI : La décision de Lionel Messi surprend aussi le Real Madrid