VIDEO. Les 4 vérités de Rangou : “Thiaga doumako bagn… Tate mo geuneu yomb…”

0

“Thiaga doumako bagn, dafa djiitou sama dioudou… Alhamdoulilah”

“Sama yaram la dou sen yaram…”

“Sama ligueye loumou lath ma dioxko…”

“Solen fi nèkè beugue ma sonal damay dagg sama billet tokk deukk bima saff tè sou boba li ngen di guiss molen nara geuneu nakari…”

“Yén Sénégalais yii da ngen na beugue dieul tate defko fo xamantè ni tate yègou fa…”

“Goudi yii niou tolou, tate mo geuneu yomb lo meunti am Sénégal…”

Laisser un commentaire

Votre adresse email ne sera pas publiée.